馃洃URGENT: BALLA GAYE 2 VS BOMBARDIER IMPORTANTE D脡CLARATION DU PROMOTEUR GASTON MBENGUE
92,034
Reddit
馃毄S鈥檃bonner 脿 la cha卯ne de la 2stv cliquez sur ce lien馃憠 : bit.ly/3cnXP6h
Retrouvez l'ensemble de nos programmes d'actualit茅 et 茅missions de soci茅t茅, sant茅, politique, culture, musique, 茅conomie sur:
- esonlines.info
www.2stv.net
Iptv disponible sur 2stv.sn
Snapchat: senegal2stv
TikTok: @2stvsenegal
instagram.com/2stv_senegal/
facebook.com/2stvsenegal
twitter.com/2stvsenegal
www.dailymotion.com/video/x7v...

Comentarios
  • Aliou Kama
    Aliou Kama

    Gaston dou dara doul

  • pape diene
    pape diene

    Yaw dodara domou maki sallnga

  • zo x chanell
    zo x chanell

    Wa prix billet yi niata laa

  • Amadou Moustapha Thiam
    Amadou Moustapha Thiam

    Ce n鈥檈st m锚me pas normal mouye ameu 5000 places

  • Amadou Sall
    Amadou Sall

    Gaston daguay politique waxofi dra soite gua organise ko noumou war茅 wala gua annuler ko pr茅sident bi d茅m fi tourn茅 ba xolam s茅d di sonal gnigni

  • Mbaye Diaw
    Mbaye Diaw

    Wakhi tapale rek lafi deug

  • Seck Aka Kalidou
    Seck Aka Kalidou

    tu fais partie des propageurs nr 1 du corona verus au senegal mr Gaston de m锚me que ton ami le prefet de la france mr Macky

  • abdou aziz Seye
    abdou aziz Seye

    Xalat tv moy Bandi

  • Bilel Bibi
    Bilel Bibi

    Dou 莽a khaliss motakh dimbelougnou

  • Meissa Gueye
    Meissa Gueye

    Daye doule rek

  • Biobi l'officiel
    Biobi l'officiel

    Ay way fat茅 x茅dioufi p猫re Gaston kagn gua changer yaw mi nga xamn茅 combat dagua done niakhtou rk nane dagua perte t茅 temps yoyu la lamb guena dokh alors maintenant ke tout est difficile nga yobal bire yi Di diniouko forc茅 bilay xamgua xaliss ligu茅yoko mais allons rk

  • Fallou Leye
    Fallou Leye

    Xalat tv 馃摵 dal doun aye niat 馃榾馃榾li yep lerna senegal yep

  • Mohamed Ba
    Mohamed Ba

    Gaston li dousa xalatt

  • Mohamed Ba
    Mohamed Ba

    Vive Xalaat tv

  • vieux ndiaye
    vieux ndiaye

    Non xalax TV d'o霉 nitt ! Gniii ayy bandit d'茅tat laniou koi

  • Serigne Wadji
    Serigne Wadji

    Boudon sa khaliss billahi doko def ni

  • Serigne Wadji
    Serigne Wadji

    Khaliss rk gay diamou moul nakh nittyi

  • Serigne Wadji
    Serigne Wadji

    Khaliss bi dou sa Khaliss gaston

  • mourtalla Seye
    mourtalla Seye

    Ces 2 ils sont dangereux pour la societe Ils veulent pas kles choses change de vrai d...ram

  • El Hadji Falilou Ka
    El Hadji Falilou Ka

    Merci xalaat tv lepp Lerna .avec le covid l'茅tat permet 脿 son promoteur de politiciens d d'organiser les combats de lutte.ba ken wakhatifi etat d urgence .ou le comit茅 de sant茅

  • Modou Gueye
    Modou Gueye

    Macky le prometteur de l'ann茅e

  • Modou Gueye
    Modou Gueye

    Il est en maron beige deh c kel couleur de parti mm

  • Guirane Mbodji
    Guirane Mbodji

    F茅n rek

  • Dieng Ahmet
    Dieng Ahmet

    Gaston khalatal niati fani bamele bakhna fen rek yaw do rouss sakh

  • Dieng Ahmet
    Dieng Ahmet

    Merci xalat tv wakhonga lepou Gaston mi man defoumako nawle teki woul dara bilahi

  • Papa Saer DIOP
    Papa Saer DIOP

    Boulen len ken naakh, Gaston dou niakkk khaliss si dara. Vrai tekkk khelll la. Boulen kennn divertir. XELLL XALATTT REK

  • Aliou Dieng
    Aliou Dieng

    Waw nafekh wesowol lab dji niokoye wot茅 guir berko ta ligue khamn茅 yalla mogno kou santeu moye diamoko si diakayi guene nioye guemlo diamo yalla si diakayi bakhol nakh corona nafekh wesowol lolou

  • Ibrahima Thiaw
    Ibrahima Thiaw

    Ay nakhlla gu茅mou malo de

  • Vieux Shakur
    Vieux Shakur

    C'est un ordre du Buur Macky Sall.... Politique k茅ss茅 leu... Gaston ak nimou beugu茅 xaliss rek di huis clos馃ぃ馃ぃ馃ぃ amena lou ci nioule deee gayi

  • Atta Toure
    Atta Toure

    geumo dara

  • el hadji sarr
    el hadji sarr

    Yakhe S茅n茅gal gu茅n geuneu diogu茅

  • Babacar Seydi
    Babacar Seydi

    Livr茅 moi Gaston ma sram Nd茅y kii 馃槀

  • le S茅n茅gal autrement
    le S茅n茅gal autrement

    Xalat tv dalen xamm...

  • bigsene roots
    bigsene roots

    Katal sa ndeye

  • Mamadou Traor茅
    Mamadou Traor茅

    5000 Mill billet gni nek Thi bountou stade bi nak 馃槀馃槀馃槀馃槀p猫re ya nekh banlieue bi rek sounou babeco 馃槀

  • Fatou Diao
    Fatou Diao

    Ay waay ! gaston baayil fenn ak manipuler askan wi . Magg dou fenn. Gueum leen yaala, tant么t ngueen waxli, tant么t ngueen wax laa. Goone kan lagniy roy. Di fenn, Di fenn, ba fenn sa bopp.

  • Drogba Didier
    Drogba Didier

    Les corrompus de vrais doorkat l脿 jeunesse est consciente de vos manipulations

  • Abdoulaye FALL
    Abdoulaye FALL

    5.000 personnes 馃ぃ馃ぃ馃ぃ馃ぃ

  • Saliou BEYE
    Saliou BEYE

    Et le pay per view il faut l'annuler , lolou rk moy yakk lamb j nak

  • Toubabel Sall
    Toubabel Sall

    Gaston li ngay wakh c faux dis la v茅rit茅 kou teug combat bi wayyy

  • Modou bousso Leye
    Modou bousso Leye

    Ngua vaccin茅wou yak sa wa keur boul niou sonal

  • Alla Gueye
    Alla Gueye

    Bilay nie dan nio yap coi com coy wakh ak ay khale rek khanat ay dof lan nio beuga diap茅 l猫gue aret way akh

  • Ibrahima ndao
    Ibrahima ndao

    馃槻Doull

  • Ibrahima ndao
    Ibrahima ndao

    馃槻Doull

  • Ibou Ndiaye
    Ibou Ndiaye

    Lefeul ndayou lamb

  • Elhadj Ndiaye
    Elhadj Ndiaye

    Combat huit clos dis Gaston 5000 place seront vendu le reste de son argent l'茅tat va lui rembourser c'est un Dilel.

  • IbissCuss DI
    IbissCuss DI

    2Stv c鈥檈st quoi cette Sonorisation鈥an hi deuguene di nelawou rek鈥

  • Djiby Teuw
    Djiby Teuw

    Tu n'es qu'un dealeur reik sa way. Sathie alalou askanwi diko deif ci ay thiakhane.

  • Moussa Djigs
    Moussa Djigs

    Non ne sont pas des cons on c'est tout

  • Moussa Djigs
    Moussa Djigs

    Gaston nous on s'en fout de la lutte si tu veux tu n'as qu'脿 annuler tout les combats on s'en tape 莽a nous int茅resse pas

  • Baye Kasse
    Baye Kasse

    Talounou lamb

  • Meujnat Diakhat茅
    Meujnat Diakhat茅

    Vous croyez que vous pouvez nous divertir kharal rek...

  • Galaye Beye
    Galaye Beye

    Kham nga yaw khaliss R锚w mi mom lala macky diokh ngaye tegue lamb mais yaw mou begue ndm khaliss mi nane aye vicolo sa leufall ndeye rk

  • Keb Ouz
    Keb Ouz

    Politique rek rien d'autre allez dit les gens au Politique qu'il arr锚te de ns maitre dans leur politique on n'a tt compris

  • Ousin Le Pro
    Ousin Le Pro

    馃ぃvaccin馃ぃ xawma kan moy vaccin茅 pour ben combat rek

  • Ousin Le Pro
    Ousin Le Pro

    馃ぃ馃ぃ sa way xam nagn leep plotique rek la

  • Cheikh Niang
    Cheikh Niang

    Katal ndayam falee xalisou S茅n茅gal reik lagnou la diokh guay teug lambou Di doul di day fii

  • wade wade
    wade wade

    Sen int茅r锚t bopou rek gnene fii nek doul rek mak you toll ni yene lamb amoul niarigne

  • Dame Dieng
    Dame Dieng

    Yaw daray S茅n茅gal nioroula sa bope rek guemo dara danoula faye rek kham nanou lepe

  • Yuri94
    Yuri94

    pour moi c'est l'茅tat qui parle mais pas gaston

  • seck ndanane
    seck ndanane

    Lamb thi boppam mo amaloul senegal benn ndiarigne

  • ABABACAR Samb
    ABABACAR Samb

    Gaston politique r藕k ,wakh ngua ak gouvernement bou yague, do ngaka sa int茅r锚t r茅k macky dinala diokh

  • Bara Gueye
    Bara Gueye

    Way go lamb ne nous interese pas .yenn gni niepp lanioufi dieulee ay parasites nguen si deuk bii

  • Cheikhouna Mbengue
    Cheikhouna Mbengue

    Yen xalisou S茅n茅gal Guen sathie di teug ay lamb sunu yon nekou si sen lamb yalla Nanou yalla ate ak yen

  • Gen猫 ral
    Gen猫 ral

    Sou mbeurmi diogu猫 keureum Di gnew lambji niata nit nioukoy goungu猫 ?balla soudan猫 Bombardier niata nit nioy jubil茅 ? Donc c'est toujours risqu茅

  • Gen猫 ral
    Gen猫 ral

    M锚me avec deux personnes c'est source de propagation de la covid il faut annuler ce combat .

  • Khadim Sow
    Khadim Sow

    Gaston politiques Chen bou laxatou la,馃ぃ馃ぃ馃ぃ馃ぃ馃ぃ馃ぃ

  • Bassirou Ciss茅
    Bassirou Ciss茅

    Vous pensez que Gaston va investie des centaines de millions et de ne pas vendre des billets juste pour emp锚cher la propagation du virus Monsieur Mbengue dit nous la v茅rit茅 SVP 莽a c'est de la politique ce que disait Xalate TV est la.

  • Oussaynou Seck
    Oussaynou Seck

    Boo man茅茅 sakh na ngaary mbeuryi respecter mesure distance yi Baham 31 bouf茅kk茅e corona 3em vagg bii nguin diwakh deuggla souboubaa ngiou geum l茅en

  • Souleymane Mbengue
    Souleymane Mbengue

    Bonne id茅e 馃憤

  • Mussa Faal
    Mussa Faal

    Ah Gaston maky diokh Nala way

  • Dame gningue
    Dame gningue

    Macky Sall mola diokhe moyin mo takhe

  • Diop Seringe
    Diop Seringe

    Na fekhe rek doul gen ba yakhou

  • Moussa Mbodj
    Moussa Mbodj

    Day douul, loudoul xaliss,gueumou ko. Vampire leu

  • King D
    King D

    Tout est politis茅e馃馃徔

  • Abdou Diouf
    Abdou Diouf

    Sama yonne nekosi

  • doff 5
    doff 5

    Alhamdoulillah sama jeunesse commmenc茅 naa y茅wouuu鉁屸湆鉁岎煓忦煠濔煠

  • Abou Wagne
    Abou Wagne

    Louthy souniou yone akk s茅ne lamb you niaff ndayam yi

  • Abou Wagne
    Abou Wagne

    B茅kaye mo guene gnaf ndayam

  • Thiemokho Tounkara
    Thiemokho Tounkara

    Bagne so.ko campagne reck diar neu li macki ya dokhanne se ndaye

  • Abou Wagne
    Abou Wagne

    Gaston ya ham niow ak koula yonni ibou ngafa sall f茅n r茅k

  • Edmond Ndour
    Edmond Ndour

    Yow Gast贸n domou kharam gua imbecile gua Waye Lou way def

  • Ablaye Ndiaye
    Ablaye Ndiaye

    Limoy dafou thi sa xalis Bou doun sa xalis la dothi mayi dara

  • Davy Alassane Mansaly
    Davy Alassane Mansaly

    Tallou niou lamb 3iem mandat daniou koy t茅r茅

  • Atu Diol
    Atu Diol

    Wakhal souniou millions

  • matraka musicflow
    matraka musicflow

    Lamb si boopam mo amatoul khorom

  • APpelmw Vladimir
    APpelmw Vladimir

    Je viens de confirmer la th猫se de xalaat tv s鈥檌l organise ce combat avec moins de 5000 personnes alors que le stade pouvait prendre jusqu鈥櫭 25000 personnes l脿 c鈥檈st clair que L鈥橢tat est derri猫re ce gars rien que pour endormir la jeunesse

  • Galsen soldier
    Galsen soldier

    Nguene teuthie Diaka yi oubi stade yi nane ay coupe d鈥檈urope yene ay vrai faux type nguene

  • Khalifa Mboup
    Khalifa Mboup

    Niawww soff gu茅n trop

  • mor blinde
    mor blinde

    Lambe kay d鈥檕霉 dara

  • Abdoul Diallo
    Abdoul Diallo

    Gaston o霉 il a pris cette argent regarder sa maison il m茅rite odituf

  • Fran莽ois Samb
    Fran莽ois Samb

    Xalaat TV nous a fait comprendre. Kouniou aal aay geut wakhla fanguay khol.

  • Faye Pape
    Faye Pape

    Lambe politique, organizzata per macky sall, nioune khamante naniou, lici kanam

  • Bayemodou Seye
    Bayemodou Seye

    MAN LI MA METTI SOUNOU WAKHE RRCONFINEMENT XEL YEM DEM SI DIAKA MERDE XANA DIAKA REK MO FI NEK

  • mame mor gueye
    mame mor gueye

    馃槀馃槀馃槀kou amoule vaccin boul nieuw

  • mbaye mbaye
    mbaye mbaye

    Dou sa xaliss Gaston mbengue xalissu askane bi mom la-la macky sall diokh combat gratuit la wara nek 脿 la 2stv vous 锚tes des voleurs becay mbaye complice nga

  • Aliou Konte
    Aliou Konte

    Ok鈥pr猫s d茅claration bi sol茅n xalat茅 deug digu茅n xamni 脡tat moko gu茅mb generation bi donatouniou ay dof Xalatt tv sol na souniou xel bou yagu 馃槀鉁岋笍馃挭馃徑Merci Xalatt tv

  • Touba Mbacke
    Touba Mbacke

    apre avoir ferm猫 les diakas lamb day ame Kel Senegal delossi Len sen khel yalla Amna guewel yi niom becaye geumou niou dara 馃懝

    • doff 5
      doff 5

      Gars khaliss rekk gueumouniou dara

  • Wakh Degg
    Wakh Degg

    Gaston 莽a se voit que finac茅woul comba yi

  • PINO PINO
    PINO PINO

    Path茅tique, Gaston qui se soucie de la sant茅 de la population en disant qu'il va vendre que 5000 billets et becaye qui invite les autres promoteurs en faire de m锚me c'est vraiment abus茅. Tout le monde sait que c'est l'Etat qui est derri猫re Gaston donc le fait de vouloir inviter les autres promoteurs 脿 r茅duire le personnel lors de leurs combat est insens茅. Combat balla gaye tu dis que tu vas autoriser que 5 mil places mieux vaut que la population de mbour ne se d茅place car ils seront pleins dans les bus et ce seront les m锚mes personnes qui seront dans les grandins. Macky def loumouy def ba par茅 nane cas yi dafa yokk t茅 l茅p mome laaaa. Incomp茅tents vous 锚tes

Siguiente